douma fekk mouk lou Yalla yaatal, ma diko xatal. Dara louy yak Adina,wala diinee doumako def. Mane ande naak niep.
Lissi dess nak, Yalla yore diaamam, te ci yeurmandeem lalen yore. Yeurmandee diodiou nak, damay niaane mou yok rek, te yaatal ko.
Mangui len di nouyou bou baaxa baax, dilen niaanal, wayee yeenit nangenma nianal" waxi Serigne Saliou Mbacke "
Risultati (
Italiano) 1:
[Copia]Copiato!
Douma fekk Mouk tiepida Yala yaatal, madre Diko xatal. Dara Louy yak Adina, wala diinee doumako finale. Mane profonda waterP nudo. Lissi Dess nak, Yala ribalta diaamam a ci yeurmandeem Lalen ribalta. Yeurmandee diodiou nak, Damay niaane yok manica forzatura yaatal co. Mangui significa di nouyou costruire baaxa baax, dilen niaanal, wayee yeenit nangenma nianal "Serigne Saliou Mbacke Waxi"
Si prega di attendere..
